"Fa guy jaar gorkat ba" (Seex Aliyu Ndaw )

Sénégal
  • Wolof

Texte en français

Seex Aliyu Ndaw , Fa guy jaar gorkat ba (conte), OSAD, 2020

« Quel que soit le prix à payer, le Sénégal va préserver ses forêts », déclarait Macky Sall, alors Président de la République. Il faut dire que la lutte contre la déforestation est, depuis quelques décennies, au cœur des préoccupations des autorités sénégalaises. Différentes mesures ont été prises sans, toutefois, qu’il n’y ait de changements majeurs. Soucieux de participer à l’effort de sensibilisation et de préservation des forêts, Seex Aliyu Ndaw va publier un conte, Fa Guy jaar gorkat ba, qui montre les conséquences de la coupe abusive de bois. Le récit du baobab et les remarques du conteur participent, pour ainsi dire, à une volonté de préserver l’environnement et de sauvegarder de l’humanité.

Contributeur: Moussa Sagna


Texte en anglais

Seex Aliyu Ndaw , Fa guy jaar gorkat ba (conte), OSAD, 2020


“Whatever the price to pay, Senegal will preserve its forests,” declared Macky Sall, then President of the Republic. It must be said that the fight against deforestation has been, for several decades, at the heart of the concerns of the Senegalese authorities. Various measures have been taken without, however, any major changes. Anxious to participate in the effort to raise awareness and preserve forests, Seex Aliyu Ndaw will publish a story, Fa Guy jaar gorkat ba, which shows the consequences of excessive logging. The story of the baobab and the storyteller’s remarks contribute, so to speak, to a desire to preserve the environment and safeguard humanity.

Contributor: Moussa Sagna

Texte en version originale

Version originale


Li yëngal xolam, gësëm ko, ba sol ci naqar, weesuwul melo wu ñaaw wi àll bi mbubboo léegi. Li Guy tàmmoon a gis ca ba muy ndaw, ba mu nekkee waxambaane, ba sax bu yàggul dara rekk, wuute na lool ak li ko wër léegi.

Booba àll bi dafa taaru woon. Foo xool ba fa sa bët yem, gàncax gi ne gàññ. Léep naat ba wuyu turam wii di nawet mi jur naataange (FGJG, 9).

Saa yu séenee i kamiyoŋ romb ba saaku këriñ ya ne toŋŋ ca kow wutti péey ba, dit le conteur, fàaw Guy ne : « ndaw way-dund yu bare yu ñu faat » ! Yaakaar nañu ne moos xaalis bi leen këriñ di indil weeci na àll ba ñu dox di ko wat ni rekk (FGJG, 17).

Kéew di lépp lu ëmb àddina ci gàncax ak ndox, moy kiiraayu dun bi. Lu mu gën di mucc ayib, di set ak sell, doom aadama gën a jege wér

Texte en français

Traduction française


Ce qui lui fait mal, mais vraiment mal alors, c’est la dégradation de la forêt. Ce que le baobab avait l’habitude de voir de son enfance à son adolescence, et jusqu’à il n’y a guère longtemps du reste, n’a rien à voir avec ce qui l’entoure à présent.

En ces temps-là, la forêt était luxuriante. Partout où on promenait son regard, la nature était florissante. Tout verdoyait jusqu’à répondre au nom de l’hivernage qui procure l’abondance.

À chaque fois qu’il voit passer un camion rempli à ras bord de sacs de charbon pour aller à la capitale, Guy ne peut s’empêcher de dire : « que de vies a-t-on emportées » ! Ils pensent réellement que l’argent que leur apporte la vente de charbon peut remplacer la forêt qu’on détruit ainsi.

La puissance est tout ce qui entoure le monde en eau et en verdure, c’est la couverture de la vie. Plus elle est parfaite, propre et saine, plus l’homme a une bonne santé 

Texte en anglais

English translation


What really hurts him is the degradation of the forest. What the baobab was used to seeing from childhood to adolescence, and up until a short time ago, is nothing like what surrounds it now.

In those days, the forest was lush. Everywhere you looked, nature was flourishing. Everything was green to the point of answering the name of the wintering season, which brings abundance

Every time he sees a lorry full to the brim with bags of coal on its way to the capital, Guy can’t help but say, « What lives have we taken away! They really think that the money they make from selling coal can replace the forest they are destroying.

Power is everything that surrounds the world in water and greenery; it is the covering of life. The more perfect, clean and healthy it is, the healthier man is.